Safaanu tangent ci grad (DRG: RAD → GRAD)
Bësal
ngir génn ci radiaŋ dem ci grad. Mbind mu oraas mi ci kaw tan mooy safaani tangente; bësal
, ba noppi
, bindal 1, te bës
. Koñ bu jub mooy grad, kon tontu li mooy 50.. Bësal
benn yoon ati ngir dellu ci degre.