Melokaan poleer

Ci melokaan poleer, lim bu nekk mooy ab arwi bu am yaatuwaay ak ab koñ. Ñaari lim ci melokaan poleer: 8\displaystyle 8 ci 70∘\displaystyle 70^{\circ}, boole 12\displaystyle 12 ci 25∘\displaystyle 25^{\circ}. Ci tàmbali, second F ak 8, jëm r teta, ngir tontu bu poleer. Bind 8, topp second F ak siŋu koñ, ak 70. Bësal yokk. Bind 12, topp second F, siŋu koñ, ak 25. Bësal yem: 18.5408873 ∠42.76427608, degre. Ngir tontu yu rektangileer, bësal second F ak 9, jëm x y. Bind 1, bësal yokk, butoŋu i, ak yem: 1. +1.i. Te second F, jëm r teta wone na benn lim bi ci melokaan poleer: 1.414213562 ∠45., degre.